Baraka ! Merci Monsieur le Président 🇸🇳.

0
31
Baraka ! Merci Monsieur le Président 🇸🇳
Par votre détermination, votre sérénité et la défense sans faille des intérêts de notre Nation, le Sénégal conserve légitimement sa couronne de champion d’Afrique. La coupe est protégée, l’honneur des Lions de la Teranga est sauf.
Félicitations à toute l’équipe juridique, aux joueurs et au peuple sénégalais pour cette victoire historique !
Illustration : Portrait original signé Malick Mbow (Président du Mouvement Bakku).
#Sénégal #CAN2025 #Baraka #BassirouDiomayeFaye #LionsDeLaTeranga #FiertéNationale
Baraka ! Jërejëf Njiitu Réew mi 🇸🇳
Ci sa taxawaay bu dëgër, sa dal ak ni nga aarée yittey réew mi ci anam bu mat sëkk, Senegaal dafa tëye ci yoon kaalaam gi niki Sàmbiyoŋu Afrik. Kup bi mu ngi ci kaarange, ngorug Gayndey Teraanga yi mucc na.
Ndokkeel nañu mbooleem kureelu laykat yi (avocats), futbalkat yi ak askanu Senegaal yépp ci ndam lu réy lii !
Nataal bi : Malick Mbow (Njiitu Mouvement Bakku) moo ko def.
#Senegaal #CAN2025 #Baraka #BassirouDiomayeFaye #GayndeyTeraanga #Ndokkeel

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici